1 Samuel 11:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nayas Amoneen ba ne leen: «Ni may digook yeen daal, mooy nii: luqi seen bëtu ndijoor yeen ñépp, ba Israyil gépp torox.»