1 Samuel 11:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ndaw ya dikkee Gibeya, ga Sóol dëkk, ba xamle mbir ma, waa dëkk ba di dégg, ñoom ñépp a yuuxu, di jooy.