1 Samuel 12:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu weesee Samiyel wax Israyil gépp ne leen: «Mu ngoog, nangul naa leen li ngeen ma wax lépp, ba falal leen buur.