1 Samuel 13:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am na sax ay Ebrë yu jàll dexu Yurdan, wuti réewum Gàdd ak Galàdd. Fekk na Sóol a nga ca Gilgal ba tey. Mbooloom xareem ma mépp nekk faak moom, di pat-pati ndax tiitaange.