1 Samuel 15:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Samiyel daa waxoon Sóol, ne ko: «Man la Aji Sax ji yebal, ngir ma fal la buurub Israyil, aw ñoñam. Kon déglul kàddu yii Aji Sax ji wax.