1 Samuel 15:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba bët setee Samiyel teela jóg dem ngir dajeek Sóol. Ñu ne ko Sóol dem na dëkk ba ñuy wax Karmel, te defu fa lu moy yékkati am taax, terale ko boppam. Jóge na fa it, jàll ba Gilgal.