1 Samuel 15:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji teg la ci yoon wi, ne la: “Demal faagaagal moykati Amalegeen ñi. Xareel ak ñoom, ba jeexal leen tàkk.”