1 Samuel 15:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sóol dellu ne: «Bàkkaar naa! Waaye ngalla waay sagal ma ci sama kanam magi askan wi ak ci kanam Israyil. Walbatikul, ànd ak man rekk, ma sujjóotali sa Yàlla Aji Sax ji.»