1 Samuel 15:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Sóol song Amalegeen ña, dale ko Awila ba dëkk ba ñuy wax Sur ca penkub Misra.