1 Samuel 16:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Samiyel nag ne Yese: «Xale yu góor yi yemb nañu?» Yese ne ko: «Xanaa ki gën di ndaw. Ma ngay sàmm gàtt ya.» Mu ne ko: «Yónneel, woolu ko, dunu jekki te dikkul fii.»