1 Samuel 17:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Filistee boole woon seeni gàngoor ngir xare. Ñu daje ca dëkk ba ñu naan Soko ca diiwaanu Yuda, daldi dale ca Efes Damim diggante Soko ak Aseka.