1 Samuel 17:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na muy wax ak ñoom, jàmbaar ja ñuy wax Golyaat waa Filisti ba dëkke Gaat, ne tëll génne ca làngi waa Filisti. Mu dellu ca wax jooju mu waxoon, Daawuda dégg ca.