1 Samuel 19:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu la Daawuda dawee ba raw. Mu fekki Samiyel ca Raama, wax ko la ko Sóol def lépp. Ñu ànd, mook Samiyel, dali ca Nayot.