1 Samuel 19:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu jóg moom ci boppam, jëm Raama. Mu dikk ba ca teen bu mag ba ca Seeku, daldi laajte ne: «Ana fu Samiyel ak Daawuda nekk?» Ñu ne ko: «Ña nga ca Nayot ca Raama.»