1 Samuel 19:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sóol jubal yoonu Nayot ca Raama. Ba loolu amee, ca kawam, moom it, la Noowug Yàlla wàcc, muy wéy di wax ay waxyuy dem, ba àgg Nayot ca Raama.