1 Samuel 19:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man dinaa dem, taxaw ci sama wetu baay fi nga nekk ci àll bi. Dinaa wax ak sama baay ci yaw, nu bokk taxaw ca tool ba ngay làquji, man ci sama bopp dinaa wax ak sama baay ci yaw ba gis nu mbir mi tëdde, yegge la ko.»