1 Samuel 2:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii moo di li sarxalkat yooyu tàmmoona def ak askan wi. Saa yu nit indi waan juru sarax, bu ñuy togg yàpp wi, surgab sarxalkat bi day ŋàbb roqub ñetti càq, dikk,