1 Samuel 2:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am bés genn góoru Yàlla dikk ci Eli, ne ko: « Aji Sax ji dafa wax ne: “Maa feeñu woon ci lu leer sa waa kër baay ba ñu nekkee Misra, di moomeelu kër Firawna.