1 Samuel 2:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it maay tabbal sama bopp sarxalkat bu wóor boo xam ne sama nammeelu xol ak sama bëgg-bëggu bakkan lay jëfe. Maa koy sampal kër gu wóor, muy doxe fi kanam ki ma fal ba fàww.