1 Samuel 20:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda nag dawe Nayot, ca wetu dëkk ba ñuy wax Raama. Mu dikk ca Yonatan, ne ko: «Ana lu ma def? Ana ñaawtéef gu ma def, ak fu ma tooñe sa baay, ba muy wut sama bakkan?»