1 Samuel 20:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su la sama baay nammee indil musiba, yal na ma Aji Sax ji def lu ko raw, ndegam déeyuma la ko, ba rawale la ci jàmm. Yal na Aji Sax ji ànd ak yaw, na mu ànde woon ak saa baay.