1 Samuel 20:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daf ma ne: “Ngalla yiwi ma, ndax saraxu biiri bokk lanu am ca dëkk ba, sama mag a ma sant, ma teeweji ko. Kon nag su la neexee, may ma rekk ma rëcc, seeti saay bokk.” Looloo waral dikkul ci sa ndab li, Buur.»