1 Samuel 20:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngir li feek doomu Yese jiy dund fi kaw suuf, yaw doo taxaw, sa nguur du taxaw. Léegi nag, yónneel, ñu indil ma ko, ndax moom aji dee la!»