1 Samuel 20:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su boobaa nag sang bi, yéwéne ma rekk sang bi, ngir kóllëreg Aji Sax ji nga fasook man. Waaye ndegam am na genn ñaawtéef gu ma gàkkal, ngalla rey ma yaw ci sa bopp, jarul nga di ma yóbbu ci sa baay.»