1 Samuel 21:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jawriñi Akis ya wax Akis ne ko: «Xanaa kii du Daawuda, boroom réew mi? Du kii lañuy woyal, di fecc, naan: “Sóol jam junneem, Daawuda jam fukki junneem”?»