1 Samuel 21:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba loolu wéyee Daawuda dem dëkk ba ñuy wax Noob ca Ayimeleg sarxalkat ba. Ayimeleg gatandu ko, di lox, ne ko: «Lu la taxa wéet, kenn àndul ak yaw?»