1 Samuel 21:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda ne sarxalkat ba: «Aw jigéen kay mbañ la ci nun naka jekk, su ma nekkee ci yoonu xare, te sellal la sama nit ñi nekke nii. Doonte yoon wii laajul sellal, tey fekk na leen sellal moos ci moomu mbir.»