1 Samuel 21:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fa la fekk keroog ab jawriñu Sóol bu yitte téye woon fa Aji Sax ji. Mooy Edomeen ba ñuy wax Doweg; njiital sàmmi Sóol la woon.