1 Samuel 22:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu mboolem boroom njàqare ya, ak ña bor jiital, ak tàng-xol ya, ñoom ñépp dajeji fa Daawuda, mu doon seen njiit. Ñu wara tollook ñeenti téeméeri nit, ànd ak moom.