1 Samuel 23:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu indi ko, Daawuda ne: «Éy Aji Sax ji, Yàllay Israyil sama Boroom, dégg naa déy ne Sóol a ngi waaja dikk Keyla gii, tas-si dëkk bi ndax man.