1 Samuel 23:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw gi Daawuda yég ne Sóol waajal na aw yoon ngir jël bakkanam. Booba Daawudaa nga ca màndiŋu Sif ca Orsa.