Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te xoolal, Baay, xoolal rekk sa daggitu mbubb wii ci sama loxo. Gannaaw maa ko dagge ci sa mbubb te reyuma la, war ngaa xam, nag xéll ne naruma genn mbon mbaa pexem fippu, te tooñuma la. Yaw kay yaa may rëbb, ngir jël sama bakkan.