1 Samuel 24:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne nitam ña: «Yal na ma Aji Sax ji musal ba duma def sama sang, kii Aji Sax ji fal, jëf ju tollu ni xàccil ko sama loxo, ndax moom mooy ki Aji Sax ji fal.»