1 Samuel 25:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxam nit ñooñu de, ñu baaxoon lool lañu ci nun. Soxorewuñu nu, te réerlewunu lenn it mboolem diir ba nu bokkee ak ñoom aw yoon, ca àll ba.