bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Samuel 25:2
1 Samuel 25:2 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jenn waay a nga woon ca dëkk ba ñuy wax Mawon. Amoon na alal foofa ca dëkk ba ñuy wax Karmel; ku barele woon lool la, amoon na ñetti junniy xar ak junniy bëy. Mu nekkoon Karmel, di watlu ay xaram.