1 Samuel 25:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la ndaw sa dawal mbaamam, làqoo mbartalu tund wa, di wàcc ca xur wa, ndeke Daawudaa nga ànd aki nitam, di dajeek moom; ndaw sa ne pemm ca ñoom.