1 Samuel 25:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngeen ne ko Daawuda nee: “Fekkeel déwén, yal nanga am jàmm, sa kër, jàmm, lépp lu bokk ci yaw it, jàmm.