1 Samuel 26:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda nag jël xeej baak njaqal ndox la féeteek boppu Sóol. Ñu daldi dem te kenn gisul, kenn yégul, kenn yewwuwul, ndax ñépp a ngay nelaw nelaw yu xóot yu bawoo ci Aji Sax ji, daanu ci seen kaw.