1 Samuel 26:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sóol nag ne: «Bàkkaar naa de! Daawuda doom, ñibbsil, ndax dootuma la fexeel mukk, gannaaw yaa wormaal sama bakkan tey jii! Lii ma def kay, yëfi dof la, juum naa lool sax.»