1 Samuel 28:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jamono yooyu nag waa Filistee dajale woon seeni gàngoori xare, ngir xeex ak Israyil. Akis ne Daawuda: «Xanaa moos xam nga ne man ngay àndal ci xare bi de, yaak say nit?»