bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Samuel 28:20
1 Samuel 28:20 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sóol nag jekki ne dàll fa suuf, tàlli ñareet, tiitaange lu réy jàpp ko ndax kàdduy Samiyel. Rax ci dolli amul woon genn kàttan, ngir lekkul woon dara bëccëg baak guddi ga gépp.