1 Samuel 28:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Samiyel nag faatu woon na, ba Israyil gépp dëj ko, denc ko ca Raama, dëkkam ba. Te itam Sóol mujjoon naa génne réew ma ñiy seete nit ñu dee, ak boroom rawaan yiy gisaane.