1 Samuel 28:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu waa Filisti daje, dali ca dëkk ba ñuy wax Sunem; Sóol ànd ak bànni Israyil gépp, ñu dali ca Gilbowa.