1 Samuel 29:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kilifay waa Filisti ne: « Ebrë yii, nag?» Akis wax ak kilifay waa Filisti, ne leen: «Xanaa du Daawuda, surgab Sóol buurub Israyil? Lu ëpp at a ngii mu nekk ak man, te gisuma ci moom sikk, ba mu teqlikook Sóol, ba bésub tey jii.»