1 Samuel 3:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngóor sa Samiyel nag moom, di liggéeyal Aji Sax ji fi kanam Eli. Kàddug Aji Sax ji néewoon na ca yooya jamono, peeñu mu leer it tumurànke woon na.