1 Samuel 30:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dara lu bokk ci ñoom rawul. Mag ñaak ndaw ñaak seen doom yu góor ak seen doom yu jigéen ak alal jaak mboolem lu ñu leen jëlaloon. Lépp la Daawuda délloosi.