1 Samuel 31:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Muy Sóol, di ñetti doomam, di gàddukatu gànnaayam itam, di mboolem ay nitam, ñoom ñépp a bokk dee bésub keroog.