1 Samuel 6:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Filisti ne leen: «Ban saraxu peyug tooñ lanu koy yónnee?» Ñu ne leen: «Limu kàngami Filisti ngeen di topp, daldi defarlu juróomi taabi wurus ak juróomi janaxi wurus, mu dëppook limu kàngami waa Filisti, ndax benn balaa bi leen dal moo dal seeni kàngam itam.