1 Samuel 8:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Samiyel ñaawlu la ñu ko ne mu falal leen buur bu leen jiite. Mu diis ko Aji Sax ji.