bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Samuel 9:1
1 Samuel 9:1 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jenn waay la woon ju bokk ci giirug Beñamin, ñu di ko wax Kis. Abyel ay baayam; Abyel, Seror ay baayam; Seror, Bekorat ay baayam; Bekorat, Afiya Beñamineen ba di baayam. Kis ku am daraja la woon.